wo
stringlengths
1
251
en
stringlengths
1
297
fr
stringlengths
1
1.15k
Yobbu samay way wuyusi yi.
Take my guests out.
Emmène mes invités.
Yaay Führer bi.
You're the Führer.
Vous êtes le Führer.
Kan mooy sa fas?
Who's your horse?
Qui est ton cheval?
Kenn ci ñoom daw, nga dóor ko, nga woo ko turam.
If one runs away hit her with it and call her name.
Si quelqu'un s'enfuit, il l'a frappée et l'a appelée.
Dellu ci sa liggéey, yaw nit ku soxor ki.
Get back to work you lousy bastard.
Retourne travailler, sale salaud.
Lii sama dëkku maam la, naka laa koy bàyyi?
This is my ancestral home, how can I leave it?
C'est ma maison ancestrale, comment puis-je la quitter?
Di nga nekk gumba!
You'll go blind!
Tu vas devenir aveugle!
Danga dundu lu metti...
You've had a bad time...
Tu t'es mal amusé...
Baax na?
All right?
Ça va?
Saa yu ma duggee dama wara bàyyi mburu mu ñor.
I'll have to leave a trail of breadcrumbs every time I come in.
Je vais devoir laisser une trace de chapelure à chaque fois que j'entre.
- Baax na.
- All right.
- Très bien.
Yenn saa mu may yàgg balaa may fàttaliku fi ma nekk.
Sometimes it takes me a while to remember where I am.
Parfois, il me faut du temps pour me rappeler où je suis.
Oh!
Oh!
Oh! C'est pas vrai!
Lasse moy fii.
Lasse is here.
Lasse est là.
Sama doom jinne la.
My son is a demon.
Mon fils est un démon.
Dellu ci sa selil ngir lim ci guddi gi.
Return to your cell blocks for evening count.
Retournez dans vos cellules pour le compte du soir.
SÀCC WELO BI
THE BICYCLE THIEF
LE TROISIÈME BICYCLE
Yaay.
Mom.
Maman.
Xale bi, looy def?
What are you doing, boy?
Qu'est-ce que tu fais?
Moytu.
Careful.
Doucement.
Loolu la!
That's it!
C'est ça!
Fan?
Where?
Où?
Dige buma defoon Andy.
A promise I made to Andy.
Une promesse que j'ai faite à Andy.
Dañu wane ni dañu néew doole lool, te yoonu nature dafa wax ni dina ñu leen jeexal.
They have proved themselves too weak and it is a law of nature that they will be exterminated.
Ils se sont montrés trop faibles et c'est une loi de nature qu'ils seront exterminés.
Loolu mooy li ma doon wër.
That just happens to be exactly what I'm looking for.
C'est exactement ce que je cherche.
Napp charter.
Charter fishing.
Pêche charter.
Loolu yoon wu wóor la.
That's a sure-fire way.
C'est une voie sûre.
Du ni fii.
Not like here.
Pas comme ici.
Lu tax loolu?
Why's that?
Pourquoi?
Lunu yeesal yeesal?
Why not?
Pourquoi pas?
Mën nga gëm ni dina firndeel...
You can be sure he'II prove...
Vous pouvez être sûr qu'il prouvera...
Bul ko bàyyi mu gëna jeexal sa xol.
Don't let it get you down.
Ne te laisse pas faire.
Ba leegi amna góor ñuñ suul.
There's still men buried.
Il y a encore des hommes enterrés.
Amaana dama wara jël fita ngir sàcc Foodway bi, ñu yóbbu ma seen kër.
Maybe I should get me a gun and rob the Foodway, so they'd send me home.
Je devrais peut-être m'acheter une arme et voler la Foodway, pour qu'ils me renvoient à la maison.
Danga wara bàyyi sa bët ci moom.
You have to keep your eyes peeled for her.
Vous devez garder vos yeux épluchés pour elle.
Risi?
Ricci?
- Ricci? - Oui.
Sa askan lañu.
They are your people.
C'est ton peuple.
Am nga ay doom?
Do you have kids?
Vous avez des enfants?
Du ma jox lu ma lekk.
He does not give me to eat.
Il ne me donne pas à manger.
Ma siiwal deret ñatti fan.
I pissed blood for three days.
J'ai pissé du sang pendant trois jours.
Te dunu musa dem ci àll bi.
And we are never going into the woods again.
Et nous n'irons plus jamais dans les bois.
- Du sama jafe-jafe
- It's not my problem
- Ce n'est pas mon problème.
- Lu tax doo jëfandikoo sa retrete ngir...?
- Why don't you use your retirement to...?
- Pourquoi n'utilises-tu pas ta retraite pour...
Mu ngi daanu! Xaaral! Bul ko bàyyi!
He's falling! Hang on! Don't let go!
Ne lâche pas!
Yaa ngi jaay guidon?
You selling a handlebar?
Tu vends un guidon?
Jël ko.
Take it.
Prends-le.
Lii ci rëbbkat bi gëna baax ci West Land?
This from the West Land's best hunter?
Ça vient du meilleur chasseur de l'Ouest?
Daa melni def nga ay jamono ci New England yépp?
Sounds like you done time all over New England?
On dirait que tu as fait du temps dans toute la Nouvelle-Angleterre?
Beneen kafe?
Another coffee?
Un autre café?
Kaso yépp war nañu dem ci Lockdown bi.
All prisoners report for Lockdown.
Tous les prisonniers se rendent à Lockdown.
Dina dellusi suko defee mu xam kan mooy patroŋam.
She'll come back then she'll know who's boss.
Elle reviendra et saura qui est le patron.
Sac bu ndaw boobu? .?
That little sack of shit? .?
Ce petit sac de merde?
Wendi:
WENDY:
- Oui.
Dafa rëy, waaye du lenn ludul waañ.
It's big, but it ain't nothing but a kitchen.
C'est grand, mais ce n'est rien d'autre qu'une cuisine.
Ayca.
Go ahead.
Allez-y.
Oh, sama xarit!
Oh, dear!
Oh, chérie!
Leegi la.
Here it is.
Le voilà.
Dama wara dem ci kilifa yi ngir delloosi la te baña fay sa xaalis.
I'll have to go to the authorities and report you and keep your wages.
Je dois aller voir les autorités et vous signaler et garder votre salaire.
Damn you, saa yu nekk dangay ñaxtu.
Damn you, always complaining.
Tu te plains toujours.
ñi dundu lu mel noonu ci jafe-jafe yu mel noonu... saa yu ci topp dañu melni dangay yëngu ndànk.
who have been through similar traumatic experiences... that the following moments kind of feel like you're moving kind of in slow motion.
qui ont vécu des expériences traumatisantes similaires... que les moments suivants ont l'impression que vous bougez un peu au ralenti.
Jiroom ñatti at ci ginaaw yaa ngi woon.
You were away eight years before.
Vous étiez absent huit ans auparavant.
Maa ngi waajal projet bind bu bees.
I'm outlining a new writing project.
Je présente un nouveau projet d'écriture.
Ziwatanejo, wala?
Zihuatanejo, huh?
Zihuatanejo, hein?
Dama jël ndam li.
I win.
J'ai gagné.
guddi gi mën nga nelaw bu baax... waaye suba bi velo bi dina dellusi.
Tonight you may not sleep too well... but tomorrow the bike'll be back.
Ce soir, vous ne dormirez peut-être pas très bien... mais demain, le vélo reviendra.
Dafay gàllankoor neer yi ak sistemu noyyig bi.
It paralyzes the nerves and the respiratory system.
Il paralyse les nerfs et le système respiratoire.
Bul bàyyi ba ma wax ko.
Don't let go until I say so.
Ne lâchez pas jusqu'à ce que je le dise.
Mën naa tiire bal kilifa gi, fekk maa ngi ci liggéey bi.
I could shoot the manager, while I was at it.
Je pourrais tirer sur le manager, pendant que j'y étais.
Dama ko gis muy naan guayave, kan moo xam lu ci des?
I just saw her taking a guava and who knows what else?
Je l'ai vue prendre une goyave et qui sait quoi d'autre?
Ndax Ricci mingi fa?
Is Ricci there?
Ricci est là?
ñoom ñoo wara fay
It's up to them to get paid
C'est à eux de se faire payer.
Lu tax ma wara ray sama bopp di jaaxle ndax dinaa mujjee dee?
Why should I kill myself worrying when I'll end up just as dead?
Pourquoi devrais-je me tuer en m'inquiétant quand je finirai aussi mort?
Sa pàppa mën na taxaw ci ñaari tànkam.
Your father can stand on his own two feet.
Ton père peut se tenir sur ses deux pieds.
Boppu fas wi nekk ci boppu yàpp bi ñàkk na nopp.
The horse's head on the butcher's has lost an ear.
La tête du cheval sur le boucher a perdu une oreille.
Nit ñi wër bii dañu bëgg saytu surprise?
Folks around this joint love surprise inspections?
Les gens autour de ces inspections surprises de l'amour commun?
Ko?
Him?
Lui?
Dafa bëgg ma xiif.
He wants me to starve.
Il veut que je meurs de faim.
Maa ngi lay massawu.
I'm so sorry, sir.
Je suis désolé, monsieur.
Yaay Führer bi.
You are the Führer.
Vous êtes le Führer.
- Nan nga tudd?
- What's your name?
- Quel est votre nom?
juróom ñatteel ci kanam.
eighth from the front.
Huitième de l'avant.
Waaw.
Yeah.
Oui.
Der fees?
Blood?
Du sang?
Lu bari ci mbir yii doo musa laal.
A lot of this stuff you'll never have to touch.
Beaucoup de ces trucs que tu n'auras jamais à toucher.
Waa Russie dañu dugg fépp.
The Russians are breaking through everywhere.
Les Russes sont en train de traverser partout.
Amnaa yeneen.
I have more.
J'en ai d'autres.
Dama wara def, seigneur?
Much obliged, sir?
Vous êtes très reconnaissant, monsieur?
Ndax tëx nga? Gaawal!
Are you deaf? Come on!
Vous êtes sourds?
- Baax na?
- All right?
- Ça va?
Lii charte la bu bawoo ci Mikado bi nuy may nu noot Yàlla Deer bi!
This is a charter from the Mikado allowing us to subdue the Deer God!
C'est une charte du Mikado qui nous permet de soumettre le Dieu des cerfs!
Ci barab bu mel nii, mën naa jëfandikoo nit ku xam ni ñuy jëlee mbir yi?
In a place like that, I could use a man who knows how to get things?
Dans un endroit comme celui-là, j'aurais besoin d'un homme qui sait comment obtenir des choses?
Toki dëgg la wax!
Toki was right!
Toki avait raison!
Baax na?
Okay?
Ça va?
Waaw, damay dugg ak génn bima amee 13 at.
Yeah, I've been in and out since I was 13.
Oui, je suis entré et sorti depuis que j'ai 13 ans.
Juroomi weer ci jàmm mooy li ma bëgg.
Five months of peace is just what I want.
Cinq mois de paix, c'est exactement ce que je veux.
Kan la?
Who is it?
Qui est-ce?
Bul jaaxle.
Don't worry.
Ne t'inquiète pas.
Sa saleer yépp, Erik.
All your wages, Erik.
Tout ton salaire, Erik.
Bul jaaxle.
Don't be nervous.
Ne sois pas nerveux.
Benn góor dafa wër benn jigéen ci kaw suuf si, daal di koy gis.
A man searches for a woman at Earth's top and finds her.
Un homme cherche une femme au sommet de la Terre et la trouve.
README.md exists but content is empty.
Downloads last month
35

Space using Alwaly/multilingual-wolof-french-en 1