audio
audioduration (s)
1.22
171
text
stringlengths
6
108
sama tontu day ëpp.
liggéey bii neexuma.
askani afrig, ëllëg, ëllëgu booloo la, ëllëgu moom-sa-bopp la !
ni nuy gëme yàlla
maa ngi doon dugg ci yu sew yi.
jàww jee ka naqari?!
dama leen yërëm.
maa ngi dee ak xiif !
turam dinañu ko bind ci téerey mboorum senegaal.
wax na ko moom seex saalihu.
tom gis na jinax.
dañoo am ay jafe-jafe.
mu ngii di ñów.
bul nàngu loolu.
am naa ag jot.
fàww nga may tàggatkat bi tuuti ngir mu tabax ekib buy jël kub
yayoo naa lii.
te leeruk yaramam tax na cër ya xeereer
paap aali jàllo
ibn khaldun reewu tinisi
ku seede mbaaxug wujjam mu noonoo la
ngànnaay ya ñu jàpp ca tuubaa
bëtu tan jéggi na méddu sanqaleñ séex anta jóob
tay wëppa dina am ngeen bàyyi ko xel insàllaa.
ndax danga may déglu?
pëndax lay doon bu weex tuuru ci garab gi ne ci ñàpp.
tom ab naxaatekat la.
ci moom lanu bawoo ci moom lanuy dellu
réere naa ko lool.
te bëgg foo ayeeti sunu diggante leer
doo sama nawle.
nangeen jubb !
nekkoon naa fa.
xaj bi maa ko moom.
dama yéemu woon lool.
am naa yaakaar ngir nga nangu.
ma nga fee ng man.
yaay njaatige li.
bànneex bu diine lalul
ndax jekk ngeen leegi ?
wërsëgu jàmm ci loolu !
jox ma bal bi !
ayiti ab dun la bu nekk ca amerik diggu
ci suwayli turu làkk wi mooy kiswahili
yaay njiit li nag.
aji-tekki ji moor suraŋ
xam na li mu bëgg te mu ngi koy def